ettub wolof

ëttub wolof
2016年07月18日
  • 7.7 MB

    文件大小

  • Android 4.0.3+

    Android OS

關於ettub wolof

sàqumBaatu沃洛夫語léebuAK jumtukaayu ijji。沃洛夫語詞典和諺語。

ci wolof - En français - In English

ci wolof

ëttub wolof moo leen di baaxe benn sàqum baatu wolof, te ñu tuddee ko oggo, ay léebu ak benn jumtukaayu ijji ngir mën a ijji ci wolof.

oggo mooy sàqum baatu wolof bi jëkk a am, nga xam ne baat yépp ci wolof kepp lañu leen tekki. oggo am na lu ëpp fukki junney baat ak benn.

léebu yi ëpp nañu ñeenti junney léebu, boole ci juroom ñetti téemeeri waxin. waxinu benn léebu, mooy léebu bu ñu waxee neneen.

jumtukaayu ijji bi, dina tax ngeen mën a ijji ci wolof, ci amam yu gaaw.

ngir jàng dawal wala jàng bind wolof, mën ngeen a jëfandikoo dalu-web bii di www.ettubwolof.org.

En français

ëttuf wolof vous propose un dictionnaire wolof nommé oggo, des proverbes wolof et un outil pour vous familiariser avec l’alphabet wolof.

oggo est le premier dictionnaire entièrement en wolof avec la définition des mots en wolof. Il contient plus de 11 000 mots wolofs.

Les proverbes wolofs comptent plus de 4000 proverbes incluant plus de 800 versions. Une version d’un proverbe est une façon différente de dire le proverbe.

L’outil de l’alphabet est très utile pour vous familiariser rapidement avec les lettres de l’alphabet wolof.

Pour apprendre à lire et à écrire le wolof, vous pouvez également utiliser le site www.ettubwolof.org, plus riche en contenu.

In English

ëttub wolof offers a Wolof dictionary named oggo , Wolof proverbs and a tool to become familiar with the alphabet Wolof .

oggo is the first dictionary entirely in Wolof with the definition of words in Wolof . It contains over 11,000 Wolof words.

Wolof proverbs have over 4000 ones including more than 800 versions. A version of a proverb is a different way of saying that proverb.

The alphabet tool is very useful to get quickly familiar with the Wolof alphabet letters.

To learn how to read and write in Wolof, you can also use the web site www.ettubwolof.org which content is richer.

更多收起

最新版本1的更新日誌

Last updated on 2016年07月18日
Minor bug fixes and improvements. Install or update to the newest version to check it out!

ettub wolof歷史版本

ettub wolof 1

2016年07月18日7.7 MB
下載

在APKPure極速安全下載應用程式

一鍵安裝安卓XAPK/APK文件!

下載 APKPure